Jangat(gëstu) sama ndono

4 kangam yu Africa

Jangat(gëstu) sama ndono voorzijde
Jangat(gëstu) sama ndono achterzijde
  • Jangat(gëstu) sama ndono voorkant
  • Jangat(gëstu) sama ndono achterkant

Waa so mënon delloo ay waxtu walla ay at ci ganaw? Ak téeré bi, ma ngi lë woo ci ngë dellu ci dëmb ndax ngë xam sa ndono ni mu réyé. Buur bu goor ak bu jigéen, njitt dëkk ya won ak jambaar yu goor ak yujigéen, defaral sa toggay te ngë gëstu(jàngat) Jëfin ak kawtefu 4 kangam dëmb yi ci Afrik. Ci jeexantal téeré bi, ab pàcc laa ñu la jagglel ngir ngë tekk ay kuloor ci nitaal yi lolu dina tax ngë bokk ci léeb bi ci wetu jambaar yi. Mbaa pare ngë ?

Specificaties
ISBN/EAN 9782493538260
Auteur Mélissa Francisco
Uitgever Van Ditmar Boekenimport B.V.
Taal Wolof
Uitvoering Gebonden in harde band
Pagina's 48
Lengte
Breedte

Wat vinden anderen?

Er zijn nog geen reviews van dit product.